🚨Bismillaahi murids
Ño gi yëggal murids yi ag soppeey Seex Mustafaa Fall Mbar yëpp leggey bii ko murids tambalil ci Jannatul Mahwa Baay Fall Ga girr Serigne Bi mën fa taxawoo leggeyu Ndogou Seex Ibra Fall yi ci weeru Koor Gi.
Jaayante Bi
Wave/Om 78 187 15 41 Meïssa Ndiaye📌
Sëriñ Mustafaa Mbar, bu teggiin doon jëmm ma ne moom la, li Yàlla gën a bëgg ci ab jaam la def muy woyof, gisul dara ci boppam, yamalewul kilifaam ak dara, liggéey bu ñu woote mu njëkk ca mujj ca.
Yal na ko Yàlla sàmm !
🚨🚨🚨
Suba ci gaawo bi dëppook (Samedi 05 septembre 2026) ci arméli Tuubaa yu ñëk yi jakkarloo ak Jumma Ji fa la ñuy xëy In Sha Rabbi. Sëriñ baa gi ciy sooñi ñëpp.