Darmanko retweeted
Maa ngi seede ni amul bénn buur bo xamni jaamu ko day jariñ ñàkk o jaamu di lor kudul y’الله sunu boroom subhaanahu wa tahalaa.
Darmanko retweeted
Il nous est unanimement manifesté sans aucune ambiguïté que le Fils de Abdallah est le Meilleur des humains ﷺ🤍
Serigne Touba Khadim Rassoul ❤️
Darmanko retweeted
Lépp luy doxal sa àdduna nga fexe ba xam ko, te sàggane sa diine ba xamoo ci dara, loolu jullit bu ne war na koo moytu.
Darmanko retweeted
Jamono jii ku jangul sa diine boo taxawee ci kanamu yalla ëlëg doo am lay, ndax jang leegi yombu na mën nga toog finga nekk di jang lepp loo bëgg xam sa diine muy al xuraan di xam-xam.
Kon yitte ag farlu rek la laaj mu jaral la lila xam sa aduna jaral,
jangal naa ay nit ñu yor seeni ligeey ñii boole ko ag yor seen kër di sëy ta diir bu gatt jang nañ lu bari ta yaxalu leen dara.
Darmanko retweeted
《Yàlla sippi na samay bàkkaar, far na samay sikk, tàggatal na ma bépp baadoolo buy gedd》
Darmanko retweeted
Software is changing. And it’s a blessing.
We’re entering an era where writing code is no longer the bottleneck. Where building things becomes faster, smoother, more intuitive.
Darmanko retweeted
“Man naala moss te bu ma moss ludul yaw
Te naala am te bu ma am ludul yaw”
“Naa ne ci yaw nga ne ci man te sol ma
Baa fees a fees say ngërëm nga yor ma ”
SMJ 🥹🤍














