🇸🇳Gueye🇸🇳 retweeted
Ce qui me choquera toujours ce sont les violences que nous infligeaient les enseignants au primaire.
J’allais à l’école littéralement terrifié. Sou ma deugueroul won touti bayi école.
🇸🇳Gueye🇸🇳 retweeted
Lii motax spiritualité am sollo ku nek warnga goorgorlu ba moss dara sa dingateek sa borom c’est notre seul forteresse si monde bignou dieum nii fawnga am yeug yeug bula leer ni moo sut sam xel dina tax nga reconnaître say limites…
🇸🇳Gueye🇸🇳 retweeted
‼️Je suis à genoux w’الله c’est urgent, je cherche du taf avec mon voile en cdd ou cdi 35h, dans le 78 et dans le 92, je vous en supplie c’est une question de vie ou de mort‼️
🇸🇳Gueye🇸🇳 retweeted
Diine moom ku ci engager wu, xaaral ay nattu yu nara tollu ni sa niveau engagement
Niki ku inscriru université bëgg diplôme, xaaral nattu (examen) yu tolloog niveau d'étude ba.
Nattu mooy examen rek, qualité réaction bi la ci sunu Boroom di xool waaye mettital ñu taxu koo jog...
🇸🇳Gueye🇸🇳 retweeted
Yalla dou diouum, lepp loum deff rek amna loutakh,
khooloul lingueen beug, li gueun ci yeen rek lay deff.
Kouci beug noopalou nak, lu yalla dogal rek nangko nangou.
Doomu àdama dina soo u ci dara beug ko, fékk guenul ci moom.
Mu bagn mbirr lool, fekk moo gueun ci moom.
🇸🇳Gueye🇸🇳 retweeted
Replying to @ODBN20
Oublie les mots khabla et bahda. Bo yokké si diouli bi dara , dangay sidiot après le salam. Bo wagné avant le salam ngay sidiot. Imagine le salam comme une dépense à faire, bou budget bi manqué tu complète avant d'acheter , bou euper tu achètes mou dess de l'argent à dépenser .
🇸🇳Gueye🇸🇳 retweeted
La famille j’ai besoin de savoir quand est ce qu’on doit faire le khabla salam et le bakhda salam ?? Je suis confuse 😔
🇸🇳Gueye🇸🇳 retweeted
Personne ne vole leurs serviettes
Personne ne bouscule leurs supporters
Personne ne leur fait du mal.
Ils sont très à l’aise au Sénégal. 🇸🇳🫶🏽
Chers Marocains 🇲🇦, prenez exemple et allez reproduire cette belle attitude chez vous






















