Replying to @Momo_Diaoune
Teila teudd
Def alarme
Diappou avant ngay teudd
Niane Yallah yeiwou fadjr
Ak bi Al Amine wakhoone
Voir cet article sur WhatsApp : wa.me/p/27170603392598502/22…
AsSalamou Aleyka Ya Rassoulallaah🥹(Aleyhi Salaatou wa Salaam❤️) teapawt.net/mury__001/status/20932…
“Roy yoneinte bi (SAWS) farata la”
“Bou dessei loudoul tague , boul taggue keine koudoul yoneinte bi SAWS ndax moom rek moko yeiyo”
“Xam xam loum niouy dieurigne sou feikkei meunouniou pousser à ce que niou magal gouddi ganei adina ki gueune thi li Yallah binde”



















