Jarga ! retweeted
Nous vous donnons rendez-vous pour notre prochain webinaire.
📍 Thème: Cancer de la prostate,dépistage,Stratégie diagnostic et PEC thérapeutique
👉🏻Sous thème 1: Place de l’imagerie dans le diagnostic et le bilan d’extension du cancer de la prostate 👇
Jarga ! retweeted
Baay-Faal moo fi jiitu sa baay jiitu say maam ak seeni maam dangay juddu fekk fi Baay-Faal dangay dead leggi du yagg bayyi fi Baay-Faal – at Senegal
Jarga ! retweeted
Teggiin ci sa kanamu Kilifa da ñu ko wara jaggi ji wat ñun ñépp. Rawati ci kanamu Sëriñ Tuubaa Seex Muhammadul Muntaxaa ko. Am na lol dess wara yërëm ka ko wax mba mu def ko. Feeñal geen mën ci kanamu Sëriñ Bi ëpp na dayo lool. Ñi ko doonoon dëgg te mën ko da ñu daa def dégg,
Jarga ! retweeted
Tu te plains de la vie , ba Yallah xëy Yonner la beugne bouy meti , wala lokho wala ndigue bouy meti , ci ngey kham ni adouna khaliss kesser , kheweul yi niouy dokhaler ci sunu dieum chaque jour beuri na t bayi wu niouko khel 😔
Jarga ! retweeted
Ces derniers jours on opère beaucoup de patients qui viennent avec perforation (trou) de leur intestin dû à la fièvre typhoïde
Elle se transmet par l’eau et les aliments contaminés.
Mooytouleene yenne lekk mbedd yii
Jarga ! retweeted
Une dame à l'hopital Dalal Jamm doit se faire opérer d'un cancer du col de l'utérus, le kit opératoire devait lui etre offert mais ils ont atteint leur quota. Il n'est pas cher juste 20k et un surplus pour assurer les frais post opératoire
Wave OM 768359223
Papa Mamadou Sakho
Jarga ! retweeted
Comment démarrer un programme de transplantation rénale dans un CH National Universitaire ?
@ISNkidneycare Sister Renal Center Program Level B
@JammDalal 🇸🇳 & @ClinUnivStLuc 🇧🇪
🗣️ Yannick France & El Hadji Fary Ka
🗓️ Jeudi 05/11/2025
🕒 15h00 Dakar - 16h00 Bruxelles
🔗 Lien 👇
Jarga ! retweeted
🚨Kërug Alxuraan Gi (Kënzil Kitaabu)
Fass na ñu yeene andag kepp ku ñu bokal pass-pass girr yobbaaleel ko jëfam ci leggeyu Kënzil Kitaab Kërug Al Quran gi Seex Muhammadul Muntaxaa di liggeey lo jabootu Seex Ibra Faal gi
Wave/Om 78 187 15 41 Meïssa Ndiaye📌
Jarga ! retweeted
Replying to @RIENqueLUI
Diangg mii dh warna bepp mouride (mag nia amneu fougn nekkoon dh).
Nanu dieem rek malheureusement avec le monde connecté (téléphone yeek vidéo yi, faw nga moytu tentations yi). Yomboul nak
Jarga ! retweeted
🚨Kërug Alxuraan Gi (Kënzil Kitaabu)
Fass na ñu yeene andag kepp ku ñu bokal pass-pass girr yobbaaleel ko jëfam ci leggeyu Kënzil Kitaab Kërug Al Quran Gi Seex Muhammadul Muntaxaa di liggeey lo jabootu Seex Ibra Faal gi
Wave/Om 78 187 15 41 Meïssa Ndiaye📌
Jarga ! retweeted
Liy taxa am yalla , deeko def ngir yalla rek té bañ caa boole daray Adduna. Ndax ku am yalla, am leep

















