
👻:@milotnj99 # Ingénieur👨🏾💻~Muslim~in God we trust🙏🏽 🇸🇳. 📍🇫🇷
Cergy,Ile-de-France, France
Joined December 2017
- Tweets21.1K
- Following1.8K
- Followers1.1K
- Likes631K
Malick Sané retweeted
Ñakk gëm yalla wala weddi ko loolu warul nekk jafe jafe ci ab jullit, ndax al xuraan xamal nanu
1- forcer nit pour mu duggu ci islaam amul ci diine ji (S2, V256)
2- xamal nanu ku nekk amna liberté gëm wala weddi (S18, V29) choix boo def amna responsabilité,
3- xamal nanu yalla mooy gendi jubal ku ko neex (S28, V56)
4- xamal nanu danoo wara nekk nu bienfaisants et équitables ci ñi nekkul ay jullit ta seq ag nun jàmm (S60, V8)
Waaye benn jullit bu am fayda warul nangu kenn kuy saaga diine ji wala diko baña respect.
Malick Sané retweeted
Ñi gën ci jaamu Yalla yi mooy ñi amee juroomi meelo yi :
1- Buñu déffé Lou bakh , daadi cia bégg
2- Buñu déffé bakaar , dadi ko gaaw tuup
3- Buñu leen jooxé ñiou saant
4- Buñu leen khaagné niou muuñ
5- Buñu leen meerloo , ñiou ande ak daal tee bagna jitaal meer gaa.
Seriñ tuuba , Silkùl Jawaahir ❤️🙏🏾!!
Malick Sané retweeted
Replying to @Faantaasn
« Xamoo ndax mbir mii dina la dal ou pas donc bul ci wax », 2 de QI!
« Xamoo ndax dinga mës a ray nit, ku ray nit bul ko dénoncer. Xamoo ndax dinga mës a V nit kon ku V bul ko dénoncer »?
Vous réfléchissez avant de parler?
Malick Sané retweeted
Ay nit yu génn ci diine loolu doyul ñuy saaga diine ji ak Yonent bi shw, ngeen ne nañu maandu ndax àdduna daa gudd tànk.
Ki génn ci diine ji bëtub yéefar ak noon rekk lañu koy xoole, bu dellusee nag nu defaat ko ne sunu bopp muy mbokkum jullit.
Ab jullit day am fulla ci diineem, yaw ku la xas nga summiku xeex, ñuy xas sa diine nga ne dangay maandu doo wax.
Malick Sané retweeted
Mais pourquoi ça veut retourner l’histoire depuis hier ? Qu’est ce qu’on en a faire de ce que chacun fait de sa vie et de sa foi ? L’histoire c’est qu’une apostat (non assumée) s’est mise à attaquer notre foi , au nom de quoi laisserons nous passer cela en silence ?
Malick Sané retweeted
Particularité yoonu Murid, Maam Seex Ibrahima Fall la.
Biss bunu baayee li Maam Seex Ibrahima Fall indi di ap taalibe, boobaa lañuy ndiroo ñëp, yem ak ñëp !
Malick Sané retweeted
كُنْتُمْ خَيْرَ أُمَّةٍ أُخْرِجَتْ لِلنَّاسِ تَأْمُرُونَ بِالْمَعْرُوفِ وَتَنْهَوْنَ عَنِ الْمُنْكَرِ وَتُؤْمِنُونَ بِاللَّهِ
Malick Sané retweeted
Di doli di gueureum boubax El Hadj Omar Tall, Ahmadou Bamba Mbacké ak El Hadji Malick Sy.🙏🏽
Malick Sané retweeted
« Ceux qui ont rejeté la foi après avoir cru, puis qui ont augmenté leur mécréance, leur repentir ne sera jamais accepté. Ceux-là sont les égarés. »
(Sourate Al-Imran, verset 90)
Livre dh noumouy jeixitalei si nitt dagn ko xamoul rk.
Wayei toute chose a une âme qu’on le sache ou non. Tei lo takol rk sou yagué nga done ko
Motah yonente bi Alayhi salatou wa salam wah ni “L’homme n’a que la religion de son ami”
Wah jou jarra bayii xel📌
Les livres…certains livres!
Et ça vaut pr sa clique! Il fut un temps où ils se les passaient ici via un lien Drive.
Entreprise de déconstruction!
Chaytan da am dolé, dioulit bouné warna moytandikou di yeur lou kholouwoul waleu di dieuf lou diném beugoul
Yalna niou yalla guindi
120
Malick Sané retweeted
Lumu jaral niit nguir mu yaak lislam naleen ko jaral ngeen taxaw nguir seen diine.
Ndax seeni manipulation ak seeni tweet meun na jax jaxal xellu ku amul yobal bu doy Iman ak Islam.
Malick Sané retweeted
Je le dis souvent à mes gars vous êtes tous des musulmans par procuration. et c’est la faute a beaucoup de parents , Ils arment pas leurs enfants face à ces questionnements
Replying to @AlaadjiDitakh
Combien d'entre nous, étant jeunes ont eu plusieurs discussions spirituelles a savoir qui est Dieu, pourquoi cette voie est suivie, c'est quoi les bases de cette religion etc. avec nos parents?
29%j'en ai discuté
42%jamais eu la discussion
22%rarement avec les parents
6%Paa bi jàngul
1,397 votes • Final resultsLolou laniou beug dh. Bou niouy yakk pentcheu mi nieup nopii au nom de la liberté de culte. Wayei dina l’islam kou ko jokhogn sah niou khourii la
Préserver notre foi et mettre en garde contre les dérives destructrices n'est pas une option, c'est une responsabilité religieuse. Vouloir nous réduire au silence sous prétexte de "laisser faire" ne marchera pas. On continuera de guider les jeunes et de dénoncer le faux Inchallah
1
5
448
Malick Sané retweeted
"Ô vous qui avez cru! Préservez vos personnes et vos familles, d’un Feu dont le combustible sera les gens et les pierres, surveillé par des Anges rudes, durs, ne désobéissant jamais à Allah en ce qu’Il leur commande, et faisant strictement ce qu’on leur ordonne."
Responsabilité!
Non mais Xassida bi mom war nañ si def wahtane si noumou meune xetalei.
Dama si guiss ay nitt yissi doundou ay situation you extraordinaire❤️
2
225
Malick Sané retweeted
Si tu as déjà corrigé ton fils pour une mauvaise note à l'école et que tu n'as jamais fait pareil pour la prière de Fajr par exemple, tu lui as, de facto, montré sa priorité.

















