Thank you bi 🥹🥹🥹
Jennifer Davis Paguada, notre Chargé d'affaires, a rendu visite au Khalife général des Mourides à Touba.
Les États-Unis accordent une grande importance à leur partenariat de longue date avec les chefs religieux et les communautés religieuses du Sénégal.
#us_snniofar
80
🇸🇳Salihate ⭐️⭐️🏆🏆 retweeted
Ay nit yu génn ci diine loolu doyul ñuy saaga diine ji ak Yonent bi shw, ngeen ne nañu maandu ndax àdduna daa gudd tànk.
Ki génn ci diine ji bëtub yéefar ak noon rekk lañu koy xoole, bu dellusee nag nu defaat ko ne sunu bopp muy mbokkum jullit.
Ab jullit day am fulla ci diineem, yaw ku la xas nga summiku xeex, ñuy xas sa diine nga ne dangay maandu doo wax.
🇸🇳Salihate ⭐️⭐️🏆🏆 retweeted
Particularité yoonu Murid, Maam Seex Ibrahima Fall la.
Biss bunu baayee li Maam Seex Ibrahima Fall indi di ap taalibe, boobaa lañuy ndiroo ñëp, yem ak ñëp !
🇸🇳Salihate ⭐️⭐️🏆🏆 retweeted
Désolé de perturber votre défilement, nous ne nous connaissons pas, mais je vous souhaite tout le meilleur dans la vie et que les choses tournent en votre faveur cette nouvelle semaine.
🇸🇳Salihate ⭐️⭐️🏆🏆 retweeted
"Bou Yomal khiyamé Walahi bou niou la wowé Mbacké do diok , nioune talibés yeupay dioguando waw, daal di diarkarlo ak Yallah ak Yonanté bi , Ak Serigne Touba, " 1/2
🇸🇳Salihate ⭐️⭐️🏆🏆 retweeted
J’aimerais tellement faire partie de ces gens qui connaissent le Coran par cœur, au point que quand tu leur parles, ils te citent spontanément un verset et le complètent tout seuls, et quand il y a un désaccord, ils te répondent avec une preuve tirée du Coran. Allahumma
🇸🇳Salihate ⭐️⭐️🏆🏆 retweeted
Ben fajr, dama tokk di djang xassida di xarr waxtou bi djott. Man dal ma tokk rek craqué di xalate sama papa. Meu djoy ba sonou nax lima sama papa dimbali bama meune timm kamil wala xassida dikay djangg. Meu message baye Khoudoss dikako wax mounima wadiour lolou rek moy waréfam.





















