Mon frère (qui est en train de réciter sur la vidéo) et mon cousin ont perdu la vie récemment dans un accident aux États-Unis.
Je vous demande humblement de faire duʿāʾ pour eux, qu’Allah leur pardonne, leur fasse miséricorde et les accueille dans Son vaste Paradis.
Cheikh Rassoul📿🇸🇳(Abul Abass)🇵🇸🇨🇩🇸🇩 retweeted
Gëm yalla bu teguwul ci ay preuves day yombu dindi ci nit ki,
moo tax ku nekk mukallaf li njëkk war ci moom mooy jëfëndikoo xelam xalaat gir am ay preuves ci limu gëm.
Loolu li ci gëna gaaw mooy jang xam-xamu kalaam/ théologie, surtout jamono jii influences yi bari lool.
Il nous est parvenu que le Messager d'Allāh (ﷺ) a dit: Le plus proche de moi, parmi vous, est celui qui prie le plus sur moi. Priez donc sur moi avec abondance la nuit d'al-gharā' et le jour "azhar". (c-à-d le vendredi) (Rapporté par Al-Shāfiʿī dans kitāb al-umm) 💚
Cheikh Rassoul📿🇸🇳(Abul Abass)🇵🇸🇨🇩🇸🇩 retweeted
"Liy dëgg tay dëgg mooy jaam bi balaa tambali di weet di sikar ak jihaad ag bakkanam mu njëkke jang tawhiid ag fiq ag tasawuf".
Maghaaliq.
Ci jangalem sëriñ bi tawhiid mooy jiitu fiq topp ci tasawuf mujj, leegi nag day melni ñu bari dañuy jiital tasawuf ci tawhiid ak fiq loolu nag njoomte la.
Cheikh Rassoul📿🇸🇳(Abul Abass)🇵🇸🇨🇩🇸🇩 retweeted
Bokk na ci pexey saytaane ci sunu jamono jii xertal ndaw ñi ci tasawuf, (di lire seeni teere, di diglu seeni waxtaan, di gëstu ay wird, di weet di sikar, durus...) ta xamul ay farata jëmëm (laab, julli, woor... Ak seeni atte) jangul tawhiid ba xamee fimu wara yam, nimu wara weetale yalla...
Buko defee day nekk ci yoon wi di sonnu ta du gis njariñ li, buko defee mu japp ni limu nekk werul mu bayi, wala muy déf ay njoomte yu rëy ba ku ko gis japp ni ci ay caaxaan la nekk mën nafaa jaare bañ yoon woowu ba duko jeema gëstu ndax limu gis ci kii.
Moo tax sëriñ tuubaa waxoon ni:
Cheikh Rassoul📿🇸🇳(Abul Abass)🇵🇸🇨🇩🇸🇩 retweeted
Thierno Boubacar Zaïdi Diallo de Bansang 🩵
- The Awliya Series
Cheikh Rassoul📿🇸🇳(Abul Abass)🇵🇸🇨🇩🇸🇩 retweeted
Sidi Ahmad Tijani رضي الله عنه:
« Évitez de rechercher les défauts cachés des musulmans. Car celui qui s’emploie à les traquer verra Allah dévoiler ses propres défauts et exposer ceux de ses enfants après lui. »
Cheikh Rassoul📿🇸🇳(Abul Abass)🇵🇸🇨🇩🇸🇩 retweeted
Bienvenue au mois de Novembre ! Mois de naissance du Pôle Parfait, l'Héritier des deux Sceaux, le Maître Accompli, Mawlana Cheikh Ibrahim Niass radiyallahu Anhu....
Les cinq jugements relatifs aux actes sont : l'obligatoire, le recommandé, le permis, le déconseillé et l'interdit. Les distinguer aide à comprendre ce qu'il faut accomplir, ce qui est recommandé, ce qui est permis et ce qu'il est demandé de délaisser.
Toutefois, juger un acte ne revient pas à juger automatiquement la personne qui l’a commis : sa situation et les circonstances doivent être prises en compte. 2/2
1
2
16











